Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
score
float32
1.04
1.25
Tswana
stringlengths
7
500
Wolof
stringlengths
10
444
1.246398
Mme wa bonè o lebega jaaka modimo.'
Te ñeenteel bi, mu ngi niru benn yàlla. '
1.241996
10Rona rotlhe a ga re na Rraarona a le mongwe?
10 Xanaa du benn baay lanu am, nun ñépp?
1.240215
Mme boammaaruri jo bo ntle ja mafoko a a molemo ke gore Modimo o rata batho ba ba latlhegileng jalo.
Yexowa dafa bëgg neexal ñi koy jaamu dëgg.
1.230004
Mme gone baaposetoloi bano ba tla dira eng?
Lan la ndaw yi di def ?
1.228483
9empa ya ntatolang pela batho, o tla latolwa pela mangeloi a Modimo.
9 Waaye ku ma gàntu ci kanam nit ñi, dinañu la gàntu ci kanam malaakay Yàlla yi.
1.227346
Gonne go molemo bogolo, fa go rata ga Modimo go ka nna jalo, lwa boga botlhoko ka ntlha ya go dira molemo, e seng ka ntlha ya go dira bosula.
17 Ñu fitnaal la ndax jëf ju baax, su dee mooy coobarey Yàlla, moo gën ñu fitnaal la ndax jëf ju bon.
1.227265
O na le dipotso?
am nga ay laaj?
1.226825
Satane o ne a re: 'O a ikanyega ka gonne o mo segofaditse e bile o na le dilo tse di molemo di le dintsi.
Seytaane wax lii: ' Danga koy barkeel te bare na alal.
1.219578
Bomorwa Noa ba ne ba nna le bana ba bantsi.
Doomu Nóoyin yi amoon nañu doom yu bare.
1.215147
A foo ke tla tshwanela go busetsa morwao kwa lefatsheng lele, kwa wena o tswang teng?"
Ndax kon damaa wara yóbbu sa doom ba ca réew ma nga jóge?"
1.214524
Mme wa bonè o lebega jaaka modimo.'
Ñeenteel baa ngi mel ni jëmm ju nirook Yàlla."
1.213236
A o itse gore bogosi joo ke eng?
Ndax xam nga ban nguur la ?
1.212727
Ke ka lebaka leo lo boneng le go utlwa dikgakgamatso tseno.'
Loolu moo tax ngeen gis te dégg kéemaan yii. '
1.212168
Ka jalo, o ne a sa tlhoke go swela maleo a gagwe - ga a ise a ke a dire boleo bope.
Kon soxlawul mu dee ngir ay bàkkaaram - ndaxte masul a bàkkaar.
1.211681
Jwalokaha re futsitse wa lefatshe, eka kgona re futse le wa lehodimo.
49 Te ni nu yore melokaanu ki ñu sàkke ci suuf, noonu lanuy yoreji melokaanu ki jóge ca asamaan.
1.211177
24 [...]Ebong rona, ba o re biditseng, eseng mo Bajuteng fela, mme le mo Baditshabeng?
24 Wax ji noo ko moom, nun ñi Yàlla woo ci boppam ci biir Yawut yi ak ci biir xeet yi ci des.
1.211041
14Jaanong ba ka bitsa jang yo ba iseng ba dumele mo go ene?
14 Waaye nan lañuy wooye ki ñu gëmagul?
1.209958
etswe ke bona hore o na le takatso e mpe, mme o ditlamong tsa bokgopo."
ndaxte gis naa ne, sóobu nga ci lu wex xat ci kanam yàlla, te bàkkaar noot na la."
1.209048
6Ho lekane ha motho eo a kgalemetswe jwalo ke ba bangata.
6 Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
1.207628
Lengeloi le neng le bua le nna la araba, la re: "Ke tla o bontsha hore na ke dintho ding."
Malaaka miy wax ak man ne ma: "Maa lay won lu ñii wund."
1.206257
4gore ò tle ò itse boikanyego jwa mafoko a ò a rutilweng.
1:4 Noonu dinga man a xam ne, li ñu la jàngaloon lu wér peŋŋ la.
1.202337
Netnobody: Am I a joke go you?
smooya: am i joke to u ?
1.201476
BASIMANE ba babedi ba o ba bonang fano ga ba tshwane, a ga go jalo?
ÑAARI xale yi ñuy wone fii, niroowuñu, du dëgg ?
1.201138
Ba lebetse melao ya me mme ba obamela namane ya gauta.'
Dañu fàtte samay ndigal te ñu ngiy jaamu benn nagu wurus. '
1.198297
8Foo ba gakologelwa dipolelo tsa gagwe.
8 Noonu ñu daldi fàttaliku kàdduy Yeesu ya.
1.198
e tshepisitsweng bo-ntata bona,
na nga ko giñale woon sunuy maam, janti démb.
1.19783
Ka re: Tshegofatso e nne le lona le kagiso e lo totafalele.
(47) Mu ne: "Yàlla na jàmm nekk ci yaw.
1.197166
31 Re a itse fa Modimo o sa utlwe baleofi:
31 Xam nanu ne Yàlla du déglu boroom bàkkaar.
1.197136
nke ba tlhola baa swa; gonne ba tshwana le baengele...."
36 Dafa fekk ne manatuñoo dee, ndaxte dañuy mel ni malaaka yi.
1.196993
8 Ke ka ntlhaang, fa mo go lona go kaiwa go twe, ga go dumelesege gore Modimo o tsosa baswi?
8 Lu tax seen xel dàq ne Yàlla dina dekkal ñi dee?
1.196637
Jaanong ba kgopilwe ke lentswe le le kgopang;
Daldi leen jox baatu tawhiid baatu lixlaas loolu mooy
1.19538
Modimo o kwa legodimong, mme thato ya gagwe ga e bolo go nna e dirwa teng ke baengele ba ba ikanyegang.
Yàlla, ca kaw la nekk, maanaam ca asamaan te foofu, malaaka yu koy jaamu, dañu mas a def coobareem.
1.194421
8Ke ka ntlhaang, fa mo go lona go kaiwa go twe, ga go dumelesege gore Modimo o tsosa baswi?
8 Lu tax seen xel dàq ne Yàlla dina dekkal ñi dee?
1.19287
64Mme go na le bangwe mo go lona ba ba sa dumeleng."
6:64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
1.191962
4 Ba tla leba sefatlhego sa ona, leina la ona le le mo diphatleng tsa bona.
4 Dinañu gis xar kanamam, te turam dina nekk ci seen jë.
1.191522
di ka se sa ithuta go lwa.
te dootuñu jàngati xare.
1.190929
28Ba mo raya ba re: "Re ka itheng gore re tlhoafalele ditiro tsa Modimo?"
28 Noonu ñu laaj ko ne: "Lu nu wara liggéey, ngir matal jëf yi neex Yàlla?"
1.190842
37mme ba re: "Ha o le kgosi ya Bajuda, ipholose he!"
"su fekkee ne yaay buuru yawut yi, musalal sa bopp!"
1.190518
o a o laetseng borraetsho
na nga ko giñale woon sunuy maam, janti démb.
1.189881
Dia kalo ga salah megang klien kafir...
Waaye ci ñi gëmul, nag:
1.189877
di tla mpitsa yo o sego;
dinañu ma wooye ki ñu barkeel,
1.189261
Lo apare motho yo moša, yo ka fa Modimong o bopilweng mo tshiamong, le mo biotshepong jwa boammaaruri.
te soloo jikko ju bees, ji Yàlla sàkk ci njub ak sell yu dëggu.
1.189255
Fa Adame le Efa ba ne ba itlhophela go sa ikobele Modimo, ba ne ba leofa.
10 Waaye nag, Aadama ak Awa dañu tànn bañ a déggal Yexowa.
1.189023
6Bobedi ba bona ba ne ba lokile pela Modimo, ba tsamaya melaong le ditaelong tsohle tsa Morena, ho se moo ba ka nyatsuwang teng.
1:6 Sakariya ak jabaram ñu jub lañu ca kanam Yàlla, di topp ni mu ware ndigal yi ak dogali Boroom bi yépp.
1.188773
64 Mme go na le bangwe mo go lona ba ba sa dumeleng."
6:64 Waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul."
1.188492
lona, ba lo pelo di bonya go dumela tsotlhe tse baporofeti ba di
Yeen dal yeena ñakk xel, te sen xol yeexa gëm li yonent yi yégle woom!
1.187646
Mme boammaaruri jo bo ntle ja mafoko a a molemo ke gore Modimo o rata batho ba ba latlhegileng jalo.
Yàlla dafa bëgg ñu am koolute ne mucc nañu.
1.187392
70Botlhe ba re: "Mme a o Morwa Modimo?"
70 Noonu ñépp ne: "Kon nag yaay Doomu Yàlla ji?"
1.186849
A O GOPOLA re bala ka makawana ano a mararo?
NDAX yaa ngi fàttaliku ñetti góor ñii ?
1.186271
Ke ka ntlha yang fa Modimo a ile a dira gore Adame a robale boroko jo bogolo?
Lu tax Yàlla nelawloo Aadama, nelaw bu xóot ?
1.185578
Kgabagare ba a Gololwa!
yaaaay! free at last!
1.185179
Fa o ka dira jalo, le wena Modimo o tla go segofatsa.
Boo defee loolu, Yàlla dina la barkeel lool yow itam.
1.185077
24Simone a araba, a re: Nthapelleng e le lona ho Morena, hore ke se ke ka welwa ke ntho le e nngwe ya tseo le di boletseng.
24 Simoŋ nag ne leen: "Ñaanal-leen ma ci Boroom bi, ngir mu fegal ma li ngeen wax."
1.185049
17Ditshupo tse di tla supelang ba ba dumelang ke tse: Ba tla kgarameletsa medemone ntle ka leina la me; ba tla bua ka diteme tse dintšhwa.
16:17 Ñi ma gëm dinañu ànd ak firnde yii: ci sama tur dinañu dàq rab yi, di wax làkk yu bees,
1.184735
18mme ba qala ho mo dumedisa, ba re: Dumela, morena wa Bajuda!
18 Ñu daldi ko wax bu kawe: "Nuyu nanu la, yaw buuru Yawut yi!"
1.184675
BAHEBERU 1:5 Ke Ho lefeng Lengeloi leo Akileng Are, O Mora waKa, ka letsatsi lena Keo tswetswe?
1:5 Ndaxte Yàlla musul a wax kenn ci malaaka yi ne:"Yaa di sama Doom,maa di sa Baay tey."
1.18424
9Morena a ba a raya Moše a re: "Ke bonye morafe o, ka fitlhela e le wa dithamo tse di gagametseng.
9 Aji Sax ji dellu ne Musaa: "Maa gis askan wii, askan wu dëgër bopp a ngii!
1.183686
Tsweetswee lo se ka lwa bolaya ngwana.
Ngir Yàlla, bul rey xale bi.
1.183625
matla leruo bocha tlhalefo le tsotlhe o seke wa dikgesa o diamogele,
Ci moom lañu denc lépp lu ñuy sàkku ci xel ak ci xam-xam.
1.182766
17 Ditshupo tse di tla supelang ba ba dumelang ke tse: Ba tla kgarameletsa medemone ntle ka leina la me; ba tla bua ka diteme tse dintshwa.
16:17 Ñi ma gëm dinañu ànd ak firnde yii: ci sama tur dinañu dàq rab yi, di wax làkk yu bees,
1.182743
mo lefatsheng la baphedi,
ci biir réewum aji dund ñi.
1.182704
A re tla tsalana le batho ba ba ratang Modimo?
Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla?
1.182225
7 A mongwe le mongwe a abe ka fa a ikaeletseng ka teng mo pelong, e seng ka bohutsana gongwe ka go patelediwa; gonne Modimo o rata yo o nayang ka boitumelo.
7 Kon na ku nekk joxe, ni mu ko nase ci xolam, te bañ cee am réccu walla sañul-bañ, ndaxte kiy joxe ak mbég moo neex Boroom bi.
1.182028
Nnyaya, ke nna ke tla yang kwa go ene; ga se ene yo o ka boelang kwano go nna."
Man kay maa koy fekki, waaye moom du délsi ci man mukk."
1.181969
O ka ithuta eng mo mosading wa ga Lote?
Lan lañu mën a jàng ci li dal jabaru Lóot ?
1.181865
27 [...]Mme e ke kgolagano ya me le bona, motlhang oo ke tlosang dibe tsa bone.
11:27 Loolu mooy kóllëre, gi may fas ak ñoom,bés bu may dindi seeni bàkkaar."
1.181662
4Ba tla o dumedisa, ba o fe polokwe tse pedi tsa bohobe, tseo o tla di amohela matsohong a bona.
4 Dinañu la nuyu, may la ñaari mburu; nga nangoo ko ca seeni loxo.
1.180166
Mme di tla onala+ tsotlhe fela jaaka seaparo.
dinañu màggat ñoom ñépp ni ay yére.
1.180081
16Modimo wa dira masedi a magolo a le mabedi; lesedi le legolo e le le le laolang motshegare; lesedi le lebotlana e le le le laolang bosigo; le dinaledi wa di dira.
16 Yàlla sàkk ñaari leer yu mag, gi gëna mag yilif bëccëg, gi gëna ndaw yilif guddi; mu sàkk it biddiiw yi.
1.17932
Ke eng fa Esau a ne a galefela morwarraagwe e bong Jakobe thata?
Lu tax Esawu mere rakkam Yanqóoba lool ?
1.179114
48 Lona lo basupi ba dilo tse.
48 Yéenay samay seede.
1.178571
Mme mosiami o tla phela ka tumelo ya gagwe."
waaye ku jub ndax kóllëreem mooy dund.
1.17838
Ene Yo o bolokang boammaaruri ka bosakhutleng,+
di sàmm dëgg ba fàww,
1.178265
27o tla di busa ka lere la tshepe,
27 Dina leen jiite ak yetu weñ,
1.178143
42Mme se se batlegang ke se le sengwe fela.
42 Moona de, lenn rekk a am solo.
1.178066
Go ne go na le batho ba le kae mo lelapeng la ga Noa, mme maina a bomorwawe ba bararo e ne e le bomang?
Njabootu Nóoyin, ñaata nit lañu woon, te ñetti doomam yu góor, naka lañu tuddoon ?
1.177958
Ba bangwe ba re: "Ke moporofeti jaaka mongwe wa baporofeti."
Ñi ci des ne: "Yonent la, bu mel ni yonent yu jëkk ya."
1.177916
Bolelela Farao, kgosi ya Egepeto, dilo tsotlhe tse ke tla di buang nao."
Nanga wax Firawna buuru Misra, li ma lay wax lépp."
1.177903
Ke eng fa Lote a ne a tlhopha go ya go nna kwa Sodoma?
Lu tax Lóot tànn Sodom ngir dëkk fa ?
1.177827
23 Gape, le bone, fa ba sa sale mo go sa dumeleng, ba tla lomelelwa; Modimo o nonofile go ba busetsa mo mannong a bone.
23 Te car yooyu fàq, su ñu wéyul ci seen ngëmadi, dees na leen delloo ci garab gi, ndax Yàlla man na leen cee tafaat.
1.17614
14A mongwe wa lona o a lwala?
14 Ana ku wopp ci yeen?
1.175549
teng go atlhola batshedi le baswi.
fa la di jóge àttesi ña di dund ak ña dee.
1.175472
" 'Ntlo ya ka e tla bitswa
"Dees na wooye sama kër
1.17545
Ka ba ka bona baswi, ba bagolo le ba bannye, ba eme fa pele ga sedulo sa bogosi sa Modimo; jaanong dikwalo tsa bulwa; ga bulwa lokwalo lo longwe lo e leng lwa bophelo; mme baswi ba atlholwa ka fa ditirong tsa bone tse di kwadilweng mo dikwalong.
12 Ma gis néew ya, mag ak ndaw, ñu taxaw ca kanam ngàngune ma, ay téere ubbiku, beneen téere ubbikooti, di téereb dund ba.
1.175262
gonne molao o tsosa bogale; mme kwa go se nang molao, le tlolo le yone ga e yo.
15 Yoonu Musaa daal du def lu dul wàcce merum Yàlla ci sunu bopp; ndax fu yoon amul, jàdd yoon du fa mana am.
1.175257
A o itse gore moporofeti ke eng?
Ndax xam nga lan mooy yonent ?
1.175253
16Ba bantsi ba bomorwa Iseraele o tla ba sokololela go Morena, Modimo wa bone.
16 Dina delloosi niti Israyil yu bare ci Yàlla seen Boroom.
1.175032
7Jaanong, fa o ka nkobamela, e tla nna jwa gago jotlhe."
7 Kon boo ma màggalee, dinga moom lépp."
1.174334
Tsaya mosadi wa gago le bomorwadio ba babedi mme lo tswe fano!'
Jëlal sa jabar ak sa ñaari doom yu jigéen te jógeleen fii ! '
1.174276
Pula e ile ya na matsatsi a 40 bosiu le motshehare.
Taw na 40 bëccëg ak 40 guddi.
1.174267
17 Modimo, mehopolo ya hao e ntshita hakakang!
17 Yàlla, say xalaat aka maa yéem!
1.173638
Le bokgaitsadie a ga se bone ba re nang nabo fa?"
Te ay rakkam yu jigéen ndax nekkuñu fi ak nun?"
1.173632
23Gape, le bone, fa ba sa sale mo go sa dumeleng, ba tla lomelelwa; Modimo o nonofile go ba busetsa mo mannong a bone.
23 Te car yooyu fàq, su ñu wéyul ci seen ngëmadi, dees na leen delloo ci garab gi, ndax Yàlla man na leen cee tafaat.
1.173596
Mme fa o sa mo rebole, itse gore o tla swa tota, wena le ba ga eno botlhe."
Waaye soo ko deful, na la bir ne dinga dee, yaak sa waa kër yépp."
1.173209
30 A ba a ba ntshetsa kwa ntle a re: "Barena, ke tshwanetse go dirang gore ke pholosiwe?" 31 Ba araba ba re: "Dumela mo go Morena Jesu, mme o tla pholosiwa, wena le ba ntlo ya gago." 32 Ba be ba mmolelela Lefoko la Morena le botlhe ba ba mo ntlong ya gagwe.
16:31 Ñu tontu ko: "Gëmal Yeesu Boroom bi, kon dinga mucc, yaw ak sa njaboot."
1.173088
madi senget!
Waaaay more money.
1.172867
34Nna ga ke amogele tshupo mo mothong, mme dilo tse ke di bua gore lo pholosiwe.
34 Man ci sama bopp soxlawuma seedes nit; waaye nag damay wax loolu rekk, ngir ngeen mucc.
1.172843
NobutLhe: Bagaetsho, ke tla leka thata.
Yaaaay! okay I'll try my best!
1.172496
13Morena Modimo wa botsa mosadi wa re: "Ke eng se o se dirileng?"
13 Yàlla Aji Sax ji ne jigéen ja: "Yaw, li nga def nii mooy lan?"
1.172005
20Mme Moše a raya morafe a re: "Se boifeng, gonne Modimo o tlile go lo leka gore lo nne lo o boife ka metlha, mme lo se ka lwa leofa." 21Mme morafe wa emela kgakala, Moše ene a atamela leru le le kwenneng le Modimo o neng o le mo go lone.
20 Musaa ne mbooloo ma: "Buleen ragal, ndax nattu leen moo tax Yàlla ñëw, ngir ngeen ragal ko, ba dungeen moy."
End of preview. Expand in Data Studio

Tswana-Wolof_Sentence-Pairs Dataset

This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.

This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1

Metadata

  • File Name: Tswana-Wolof_Sentence-Pairs
  • Number of Rows: 77987
  • Number of Columns: 3
  • Columns: score, Tswana, Wolof

Dataset Description

The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:

  1. score: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).
  2. Tswana: The first sentence in the pair (language 1).
  3. Wolof: The second sentence in the pair (language 2).

This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.

References

Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:

[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017

[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.

[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018

[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.

[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.

[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.

[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.

[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB

[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.

[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages

Downloads last month
9

Collection including michsethowusu/tswana-wolof_sentence-pairs