score
float32 1.04
1.23
| Swati
stringlengths 10
499
| Wolof
stringlengths 10
499
|
---|---|---|
1.234538 |
Ungaba sedvute naNkulunkulu kuphela nangabe umetsemba futsi ukholwa kuye.
|
Mën nga jege Yàlla bu dee wóolu nga ko te am ngëm ci moom.
|
1.229178 |
Lisho kutsi Nkulunkulu angenta noma yini layihlosile nalatsembise kuyenta.
|
mu wóor ko ne, loolu ko Yàlla dig, Yàlla man na koo def.
|
1.225278 |
Bantfu bamiselwe kutsi bafe kanye, bese kutsi emvakwaloko bayekwehlulelwa.
|
Kon ni nit ñi deeye benn yoon rekk, ba noppi jaar ca àtte ba, ni ko Yàlla dogale,
|
1.210429 |
Linyenti lebantfu lihlanganyele naSathane ekwaleni kutsi Nkulunkulu abe nguMbusi wabo.
|
Ñu bare ci doomu Aadama yi topp nañu Seytaane ci bañ Yàlla jiite leen.
|
1.208059 |
ningacali nilimate baphrofethi bami."
|
buleen lor samay yonent."
|
1.20371 |
Ngako-ke kwakute sidzingo sekutsi afele tono takhe - ngobe kute nasinye sono labekasentile.
|
Kon soxlawul mu dee ngir ay bàkkaaram - ndaxte masul a bàkkaar.
|
1.201307 |
Usathandaza katsatfu ngelilanga."
|
Ñetti yoon ci bés lay ñaan ay ñaanam ba tey."
|
1.200275 |
abamesabi ngisho naNkulunkulu.
|
te ragaluñu Yàlla.
|
1.199109 |
Jabulani nitfokote, ngobe umvuzo wenu mkhulu ezulwini; ngobe nebaphrofethi labanendvulela babatingela babahlupha kanjalo."
|
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
|
1.198331 |
Nkulunkulu weliciniso unguMdali wato tonkhe tintfo.
|
Yàlla dëgg ji moo sàkk lépp.
|
1.19725 |
Nalabo labanye futsi nabakuyekela kungakholwa kwabo bayawuhlunyeleliswa, ngobe Nkulunkulu unawo emandla ekuphindza abahlumelelise.
|
23 Te car yooyu fàq, su ñu wéyul ci seen ngëmadi, dees na leen delloo ci garab gi, ndax Yàlla man na leen cee tafaat.
|
1.19684 |
Sikholwa kutsi tsine nabo sisindziswa ngalokufananako ngemusa weNkhosi yetfu Jesu."
|
11 Nun daal ci yiwu Yeesu Boroom bi lanu yaakaara mucce, te ñoom itam, ci lañu wékku."
|
1.193568 |
Niyawutondvwa ngabo bonkhe ngenca yeligama lami.
|
Te ñépp dinañu leen bañ ndax sama tur.
|
1.192751 |
Nkulunkulu wakhetsa ema-Israyeli kutsi abe bofakazi bakhe.
|
Yàlla tànnoon na waa Israyil ngir ñu nekk ay seedeem.
|
1.190569 |
Ngemuva kwaloko wababuta watsi: "Nine anikabaluleki yini kwendlula tona?"
|
21 Noonu Yeesu ne leen: "Ndax seen xol dafa tëju ba tey?"
|
1.189345 |
Sitawutihlanganisa yini nebantfu labatsandza Nkulunkulu?
|
Ndax dinañu ànd ak ñi bëgg Yàlla?
|
1.188206 |
Emadvodza kufanele atsandze bafati bawo njengemitimba yawo. - Efesu 5:25-29.
|
Jëkkër yi dañu war a bëgg seen jabar ni ñu bëgge seen bopp. - Efes 5:25-29.
|
1.18735 |
Heye way Dil lut leya lut leya lut leya Tu..
|
Lot ne ca xiiñidxaapaʼ bizuubacaʼ diidxaʼ ne bixooñecaʼ de Sodoma.
|
1.187151 |
Bangani mbumbulu bakhe labatsatfu beta batewumvakashela.
|
Ñetti xaritam ñów seetsi ko.
|
1.186374 |
17nendlela yekuthula abazange sebayati.
|
17 Xamuñu yoonu jàmm,
|
1.185894 |
tetelela aba namacala kiti;
|
1:22 Jubbantileen ñi am werantey xel,
|
1.185677 |
Wadzimate wetama nekuhlambalata lithempeli, sabe sesiyambopha, [sasifuna kumgweba ngekwemtsetfo wetfu, 7kodvwa Khenela Lisiyasi, weta wafike wasemuka yena wamtsatsa ngenkhani.
|
6-7 Dem na ba jéema teddadil sax kër Yàlla ga, waaye jàpp nanu ko.
|
1.183826 |
Kodvwa ngalesikhatsi kubhalwa liBhayibheli, libito laNkulunkulu belivela kulo tikhatsi letingaba ngu-7.000.
|
Waaye ba ñu doon bind Biibël bi, turu Yàlla feeñoon na fa lu jege 7 000 yoon.
|
1.182841 |
17 Bantfwana bangafundza yini kuJesu?
|
17 Ndax am na li xale yi mën a jàng ci Yeesu?
|
1.182369 |
Jesu abebaphatsa njani bantfwana, futsi yini bantfwana labayidzingako kubatali babo?
|
Nan la Yeesu meloon ak xale yi, te lan la xale yi soxla ci seen waajur?
|
1.18173 |
Kepha baka-Israyeli lababetihlupha bafuna kulunga ngekwenta lokufunwa ngumtsetfo, noko abazange bakhone kuwugcina umtsetfo.
|
31 Waaye bànni Israyil, mi bëggoona sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
|
1.181258 |
Angisafanele nekutsi ngibitwe ngekutsi ngiyindvodzana yakho; sale umane ungenta lomunye wetisebenti takho." '
|
yeyootumaa nekk sa doom; boole ma ci say surga.' "
|
1.18079 |
Vele kuyinzuzo lenkhulu kwesaba Nkulunkulu kanye nekweneliseka.
|
Ba tey ragal Yàlla gu ànd ak doylu, wërsëg la.
|
1.179302 |
Bantfwana kudzingeka balalele batali babo. - Efesu 6:1-3.
|
Xale yi dañu war a déggal seeni waajur. - Efes 6:1-3.
|
1.177917 |
Njengobe lwati lwakho ngaNkulunkulu lukhula, nekukholwa kwakho kutawucina.
|
Sa xam-xam ci Yàlla buy yokku, sa ngëm di gën a dëgër.
|
1.176598 |
noko, ngiyawuphindze ngibuke lithempeli lakho lelingcwele.'
|
waaye maay dellu gis sa kër gu sell ga!"
|
1.174026 |
Likhona yini lolicabangako? - Fundza 1 Johane 3:10-12.
|
Loo ci xalaat? - Jàngal 1 Yowaana 3: 10- 12.
|
1.171602 |
Kepha baka-Israyeli lababetihlupha bafuna kulunga ngekwenta lokufunwa ngumtsetfo, noko abazange bakhone kuwugcina umtsetfo.
|
Waaye bànni Israyil, mi bëggoon a sàmm yoon ngir jub, matalu ko.
|
1.171334 |
Ngobe Nkulunkulu bonkhe bantfu sewubayekelele ekutseni bangamlaleli, adzimate atebahawukela bonkhe.
|
32 Yàlla moo tëj nit ñépp ci seenug déggadi, ngir yërëm leen ñoom ñépp.
|
1.171122 |
38EmaGibhithe ajabula ekuphumeni kwabo
|
38 Misra daa bég ba ñu demee
|
1.170561 |
Weta washumayela liVangeli lekuthula kini lebenikadze nikhashane, yebo, kuthula nakubo labo lababesedvute.
|
Bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam Yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.
|
1.170151 |
Ningacali nikwente loko eveni lenu.
|
Buleen def loolu mukk ci seenum réew.
|
1.170079 |
7Jesu wamphendvula watsi: "Kwanyalo awukakwati loku lengikwentako, kodvwa emvakwaloko utakwati."
|
13:7 Yeesu tontu ko ne: "Xamoo fii mu nekk li may def, waaye dinga ko xami."
|
1.169996 |
Ningamdzabukisi Moya Longcwele waNkulunkulu lenabekwa luphawu ngaye kudzimate kube lilanga lekuhlengwa.
|
30 Buleen yóbbe tiis Xelu Yàlla mu Sell, mi leen tàmpe ngir bésu goreel ba.
|
1.169235 |
18 Bafati, tfobelani emadvodza enu ngobe loku kuhle eNkhosini.
|
18 Jigéen ñi, na ku nekk nangul jëkkëram, ndaxte looloo jekk ci ñi bokk ci Boroom bi.
|
1.169016 |
Batali, yini bantfwana benu labayidzingako kute batfole injabulo ekuphileni?
|
Waajur yi, lan la seeni doom soxla ngir bég ?
|
1.16891 |
Kodvwa Jesu wamphendvula watsi: "Yebo, kunjalo, kodvwa lokukhulu kutsi: Babusisiwe labo labeva livi laNkulunkulu, bese bayalenta."
|
28 Waaye Yeesu ne ko: "Neel kay, ki barkeel mooy kiy déglu kàddug Yàlla te di ko topp."
|
1.167538 |
Nkulunkulu weliciniso unguMdali wato tonkhe tintfo.
|
Yàllaa sàkk bépp mbindeef.
|
1.166646 |
Asidalwanga nguNkulunkulu munye yini?
|
Ndax li Yàlla sàkk amoon na sikk?
|
1.166156 |
Konkhe lesikucelako uyasipha, ngobe siyigcina imiyalo yakhe, futsi senta lokutsandzeka emehlweni akhe.
|
22 Te lépp lu nu koy ñaan, dinanu ko jot ci moom, ndaxte nu ngi sàmm ay ndigalam, di def lu ko neex.
|
1.165939 |
[2:30] Recall kho Lord tshela kuze gelosi I beka mele esikhashana Nkulunkulu) Hlaba.
|
Woor ñaari farata la am: 1 yeene 2 ba liy dogloo ngir yàlla.
|
1.165576 |
Batali, yini bantfwana benu labayidzingako kute batfole injabulo ekuphileni?
|
Waajur yi, lan la seeni doom soxla ngir bég?
|
1.165572 |
Kulihlazo lelikhulu ngisho nekukhuluma ngaleto tintfo labatenta emasitseleni.
|
Ndaxte waxtaane sax li ñuy def ci nëbbu, lu ruslu la;
|
1.165313 |
Rose ngalako copier copié!
|
yaaay i want a copy!
|
1.165144 |
Bubi emhlabeni bacala ngesikhatsi Sathane akhuluma emanga ekucala.
|
Bi Seytaane njëkkee fen, ci la lu bon komaase ci kaw suuf.
|
1.164504 |
Lilanga Lekwehlulela - Liyini?
|
Lan mooy Bésu Àtte bi?
|
1.163895 |
nase abone kutsi emandla ato aphelile,
|
Ñu gisee yéex a wuyusi gi muy ag bañ, loolu
|
1.1627 |
Kuyini "iBhabhiloni eNkulu"?
|
Lan mooy " Babilon mu mag mi "?
|
1.161849 |
Ngako-ke, liBhayibheli lingakusita kutsi umati Nkulunkulu.
|
Kon Biibël bi mën na la dimbali nga xam Yàlla.
|
1.160743 |
23 Natsengwa ngelinani lelikhulu, ngako yekelani kuba tigcili tebantfu.
|
23 Gannaaw Yàlla jot na leen ak njég lu réy, buleen doon jaamub nit.
|
1.160548 |
Watsi: "Njengobe kwakunjalo ngesikhatsi saNowa, kuyawuba njalo nekuba khona kweNdvodzana yemuntfu [noma ngemalanga ekugcina].
|
Yeesu nee woon na: "Ni bési Nóoyin ya, noonu lay mel, bu Doomu nit ki di ñëw.
|
1.160427 |
Kungani Nkulunkulu avumele kuhlupheka kudzimate kube ngunyalo?
|
Lu tax Yàlla bàyyi coono yi am booba ba léegi?
|
1.16038 |
Kuyini "iBhabhiloni eNkulu"?
|
Lan mooy " Babilon mu mag mi " ?
|
1.160376 |
Make uyephi lamuhla?
|
Ana sama yaay ?
|
1.159651 |
Kubeketela kwaNkulunkulu kusiniketa litfuba lekwentani?
|
Lan la ñu muñug Yàlla di may?
|
1.159598 |
Esikhundleni saloko konkhe lesikwentako sikwenta sikhombisa kutsi sitisebenti taNkulunkulu ngekutsi konkhe sikumele: ngekucinisela lokukhulu ekuhlushweni, nasebulukhunini, nasekugongonyekeni, 5
|
Li nu bëgg moo di rafetal sunu tur ni jawriñi Yàlla ci fànn gu nekk; danuy muñ coono yi, tiis yi, njàqare yi;
|
1.15929 |
Esikhundleni saloko konkhe lesikwentako sikwenta sikhombisa kutsi sitisebenti taNkulunkulu ngekutsi konkhe sikumele: ngekucinisela lokukhulu ekuhlushweni, nasebulukhunini, nasekugongonyekeni, 5
|
6:4 Li nu bëgg moo di rafetal sunu tur ni jawriñi Yàlla ci fànn gu nekk; danuy muñ coono yi, tiis yi, njàqare yi;
|
1.158054 |
Empeleni, Nkulunkulu, ngubani lofana nawe?
|
Yaw Yàlla, ana ku mel ni yaw?
|
1.157591 |
5 Bantfu badalwa baba "ngumfanekiso waNkulunkulu."
|
5 Dañu sàkk Aadama ' ci melokaanu Yàlla '.
|
1.157396 |
Tsine siyati kutsi lomuntfu lona usoni."
|
Xam nanu ne waa joojee boroom bàkkaar la."
|
1.157351 |
8Lutsandvo alusoze luphele;
|
8 Cofeel nag du jeex mukk.
|
1.157337 |
Nkulunkulu unalo yini ligama?
|
Ndax Yàlla am na tur?
|
1.157024 |
25 Emasango alo ngeke avalwe nhlobo emini, ngobe busuku ngeke bube khona.
|
25 Bunti dëkk bi du tëje mukk bëccëg, te foofa sax guddi amu fa.
|
1.156976 |
Incwadzi yekugcina yabhalwa ngumphostoli Johane eminyakeni lengetulu kwalengu-1.900 leyengcile.
|
Téere bu mujj bi, ndaw li Yowaana moo ko bind, am na léegi lu ëpp 1 900 at.
|
1.156909 |
Ngako wase utsi kubafundzi bakhe: "Kuvuna kukhulu, kodvwa tisebenti timbalwa.
|
37 Noonu mu ne taalibeem ya: "Ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu.
|
1.156831 |
Kodvwa kutawutsi ngesikhatsi selivi lengilosi yesikhombisa, nase itawushaya licilongo layo, kufezeke imfihlakalo yaNkulunkulu, njengobe abetsembisile etisebentini takhe, baphrofethi."
|
10:7 waaye jamono ju juróom-ñaareelu malaaka ma wolee ci liitam, ndogalu Yàlla dina mat, ni mu ko waxe woon ay jaamam, yonent yi."
|
1.156686 |
Ngako wase utsi kubafundzi bakhe: "Kuvuna kukhulu, kodvwa tisebenti timbalwa.
|
9:37 Noonu mu ne taalibeem ya: "Ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu.
|
1.156232 |
Watsi Sawula naka sukuma wavula emehlo akhe, kodvwa emehlo ehluleka kubona.
|
Sool jóg, taxaw te ubbi bëtam yi, waaye mënatul gis dara.
|
1.155857 |
Kepha ayawutiphendvulela kulowo losalungele kwehlulela labaphilako nalabafile.
|
5 waaye dinañu mas a teew fa kanam Ki nar a àtte ñiy dund ak ñi dee.
|
1.154866 |
Kwentekani ngalesikhatsi baphristi sebaphumile eJordane?
|
Lan moo xew bi saraxalekat yi génnee Yurdan bi?
|
1.154766 |
28Levi wasukuma, washiya konkhe labekwenta wamlandzela.
|
28 Lewi jóg, bàyyi lépp, topp ca moom.
|
1.15473 |
18Nalomphrofethi lomdzala waphendvula, watsi: "Nami futsi ngingumphrofethi njengawe.
|
18 Mu dellu ne ko: "Man itam yonent laa ni yaw.
|
1.154626 |
Ningabavimbeli, ngobe umbuso waNkulunkulu walabanjalo.
|
Buleen leen tere, ndaxte ñu mel ni ñoom ñoo yelloo nguuru Yàlla.
|
1.153998 |
20Ngako sukuma wehle uhambe nawo ungangabati, ngobe atfunywe ngimi."
|
20 Wàccal boog, ànd ak ñoom te bul nàttable, ndax man maa leen yebal."
|
1.153932 |
Indzaba 16: Isaka Utfola Umfati Lomuhle
|
Nettali 16: Isaaxa takk na jabar ju baax
|
1.153712 |
Lilanga Lekwehlulela - Liyini?
|
Lan mooy Bésu Àtte bi ?
|
1.153146 |
Ningakuyekeli kwenta lokuhle nekuhlephunelana loko leninako, ngobe iminikelo lenjalo iyamtfokotisa Nkulunkulu.
|
Buleen fàtte di def lu baax ak di sédde ci seen alal, ndaxte sarax yu mel noonu ñoo neex Yàlla.
|
1.153131 |
Ngabe ufuna kuphila emva kwekufa?
|
Ndax bëgg nga dund gannaaw de ?
|
1.15311 |
Ciwutiso: Hikuyini Jesu a fileko?
|
Lu tax Yeesu dee?
|
1.153013 |
Nangabe umuntfu lotsite eta kuwe futsi akhulume ngeMbuso waNkulunkulu, ucabanga kutsi usuke akuyiphi inkholo? - Fundza Matewu 24:14.
|
Bu la nit jegee di la wax lu jëm ci Nguuru Yàlla, ci sa xalaat ban diine la bokk? - Jàngal Macë 24:14.
|
1.152916 |
17Nami ngitawubeka inkhulumo yami;
|
17 Damay tontu sama wàll, man it;
|
1.152488 |
8Buta kuleto tinceku takho, titakutjela.
|
8 Laajal rekk say surga, dinañu la ko wax.
|
1.15131 |
24 Bazalwane, umuntfu akachubeke embikwaNkulunkulu akunobe ngusiphi simo labitwa akuso.
|
24 Bokk yi, fàww ku nekk wéy ca kanam Yàlla ci fànn ga mu nekkoon, bi ko Yàlla wooyee.
|
1.151282 |
Babusisiwe futsi bangcwele labo labahlanganyela ekuvukeni kwekucala.
|
6 Ñi bokk ci ndekkite lu jëkk li, barkeel nañu te sell!
|
1.15073 |
14Asesethempelini kwase kufika kuye timphumphutse netinchute, watiphilisa tonkhe.
|
21:14 Noonu ay gumba ak ay lafañ ñëw ci moom ca kër Yàlla ga, mu faj leen.
|
1.149849 |
Ngubani iNkhosi yeMbuso waNkulunkulu futsi yini uMbuso waNkulunkulu lotayifeza?
|
Kan mooy Buuru Nguuru Yàlla te lan la Nguur gi nar a def ?
|
1.149703 |
Kantsi bese bayephi bantfwababo?
|
Naka / ana xale yi ?
|
1.149255 |
5Noko asibanikanga ngisho nalelincane nje litfutjana lekubatfobela, kuze kutsi liciniso leliVangeli libe kini njalo.
|
5 Waaye yaatalunu leen benn yoon, ngir dëggug xibaaru jàmm bi mana sax ci yéen.
|
1.149172 |
Ngubani iNkhosi yeMbuso waNkulunkulu futsi yini uMbuso waNkulunkulu lotayifeza?
|
Kan mooy Buuru Nguuru Yàlla te lan la Nguur gi nar a def?
|
1.149068 |
Balwa naMosi batsi: "Kube mane savele safa kanye nebanaketfu ngesikhatsi bafela embikwaSimakadze.
|
3 Mbooloo ma di xulook Musaa, naa ko: "Moo lu nu tee woona dee keroog ba sunu bokk ya deeyee fa kanam Aji Sax ji?
|
1.148879 |
Ngentela kutsi ulibone ngemehlo akho, kodvwa wena ungeke wewele kuyawungena kulo."
|
Bàyyi naa la nga gis ko, waaye doo ci dugg. '
|
1.148651 |
Amemeta Loti atsi: "Aphi lamadvodza langenise lapha kakho kuyo lentsambama?
|
5 Ñu daldi woo Lóot ne ko: "Ana góor ñi fi ñëw tey ci guddi?
|
1.148479 |
Jesu watsi kuso: "Ngikutjela kutsi: Lamuhla utakuba nami ePharadisi."
|
yeesu tontu ko ne: "ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu yàlla."
|
1.148126 |
"Tsandzanani ngelutsandvo lolukhulu, ngobe lutsandvo lumbonya tono letinyenti." - 1 Phetro 4:8
|
' Nangeen bëggante mbëggeel gu tar, ndax mbëggeel day suul bàkkaar yu bare. ' - 1 Piyeer 4:8
|
1.147416 |
Kubayini sitlhoga iphasi elitjha?
|
Lu tax ñu soxla àddina su bees?
|
Swati-Wolof_Sentence-Pairs Dataset
This dataset contains sentence pairs for African languages along with similarity scores. It can be used for machine translation, sentence alignment, or other natural language processing tasks.
This dataset is based on the NLLBv1 dataset, published on OPUS under an open-source initiative led by META. You can find more information here: OPUS - NLLB-v1
Metadata
- File Name: Swati-Wolof_Sentence-Pairs
- Number of Rows: 21230
- Number of Columns: 3
- Columns: score, Swati, Wolof
Dataset Description
The dataset contains sentence pairs in African languages with an associated similarity score. Each row consists of three columns:
score
: The similarity score between the two sentences (range from 0 to 1).Swati
: The first sentence in the pair (language 1).Wolof
: The second sentence in the pair (language 2).
This dataset is intended for use in training and evaluating machine learning models for tasks like translation, sentence similarity, and cross-lingual transfer learning.
References
Below are papers related to how the data was collected and used in various multilingual and cross-lingual applications:
[1] Holger Schwenk and Matthijs Douze, Learning Joint Multilingual Sentence Representations with Neural Machine Translation, ACL workshop on Representation Learning for NLP, 2017
[2] Holger Schwenk and Xian Li, A Corpus for Multilingual Document Classification in Eight Languages, LREC, pages 3548-3551, 2018.
[3] Holger Schwenk, Filtering and Mining Parallel Data in a Joint Multilingual Space ACL, July 2018
[4] Alexis Conneau, Guillaume Lample, Ruty Rinott, Adina Williams, Samuel R. Bowman, Holger Schwenk and Veselin Stoyanov, XNLI: Cross-lingual Sentence Understanding through Inference, EMNLP, 2018.
[5] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Margin-based Parallel Corpus Mining with Multilingual Sentence Embeddings arXiv, Nov 3 2018.
[6] Mikel Artetxe and Holger Schwenk, Massively Multilingual Sentence Embeddings for Zero-Shot Cross-Lingual Transfer and Beyond arXiv, Dec 26 2018.
[7] Holger Schwenk, Vishrav Chaudhary, Shuo Sun, Hongyu Gong and Paco Guzman, WikiMatrix: Mining 135M Parallel Sentences in 1620 Language Pairs from Wikipedia arXiv, July 11 2019.
[8] Holger Schwenk, Guillaume Wenzek, Sergey Edunov, Edouard Grave and Armand Joulin CCMatrix: Mining Billions of High-Quality Parallel Sentences on the WEB
[9] Paul-Ambroise Duquenne, Hongyu Gong, Holger Schwenk, Multimodal and Multilingual Embeddings for Large-Scale Speech Mining, NeurIPS 2021, pages 15748-15761.
[10] Kevin Heffernan, Onur Celebi, and Holger Schwenk, Bitext Mining Using Distilled Sentence Representations for Low-Resource Languages
- Downloads last month
- 7